Fasséma

Watch on

Genres: Drama, Romance

Years: 2025

Seasons: 2 · Status: Continuing

Trailers / Promo

Trailers are available in another language —

Summary

Ndax fase ab musiba la? Lan mooy mbir yi ci sëy bu nara fase? Kan moo wara def fase, ki ko def wala ki ko nangu? naka lañu mëna delloosi seen bopp ginaaw fase? Ak lan lañu mëna moytu fase? Ndax sëy ak fase ñooy noon yi gën? Lan mooy palaasu xale yi ginaaw bi ñu fase? Kan mooy yor xale yi? Laaj yu jafee xam...

Seasons (2)

Cast

Reviews